4-C
Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu
—Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 1) |
JAMONO JA |
BÉRÉB BA |
XEW-XEW BA |
MACË |
MÀRK |
LUUG |
|---|---|---|---|---|---|---|
YOWAANA |
30 |
Galile |
Bi Yeesu njëkkee yégle ne “ nguuru Yàlla jegesi na ” |
4:17 |
1:14, 15 |
4:14, 15 |
4:44, 45 |
Kana ; Nasaret ; Kapernawum |
Yeesu faj ab doomu Kilifa ; mu jàng téereb yonent Yàlla Esayi ; mu dem Kapernawum |
— |
4:16-31 |
||
4:46-54 |
Dexu Galile, wetu Kapernawum |
Mu woo : Simoŋ ak Andare, Saag ak Yowaana |
4:18-22 |
1:16-20 |
||
— |
Kapernawum |
Mu faj gorob Piyeer bu jigéen ak ñu bare |
8:14-17 |
1:21-34 |
||
— |
Galile |
Bi mu njëkkee wër Galile ak ñeent ñooñu |
4:23-25 |
1:35-39 |
||
— |
Mu faj ku gaana ; mbooloo mu bare topp ko |
8:1-4 |
1:40-45 |
|||
— |
Kapernawum |
Faj na ku làggi |
9:1-8 |
2:1-12 |
||
— |
Mu woo Macë ; lekk ak ay juutikat ; wax wu jëm ci woor |
9:9-17 |
2:13-22 |
|||
— |
Yude |
— |
||||
— |
31, Bésu mucc ga |
Yerusalem |
— |
|||
5:1-47 |
Bi mu jógee Yerusalem (?) |
Taalibeem ya fàq ay gub bésub noflaay ba ; Yeesu “ boroom bésub noflaay bi ” |
12:1-8 |
2:23-28 |
||
— |
Galile ; Dexu Galile |
Mu faj ku loxoom làggi ; mbooloo mu bare topp ko ; mu faj ñu gën a bare |
12:9-21 |
3:1-12 |
||
— |
Tund wetu Kapernawum |
— |
3:13-19 |
|||
— |
Wetu Kapernawum |
Mu def ab waare ca tund ba |
— |
|||
— |
Kapernawum |
Mu faj surgab njiitu xare |
— |
|||
— |
Nayin |
— |
||||
— |
Tiberiyàdd ; Galile (Nayin walla wetam) |
Yaxya yónni ay taalibeem ci Yeesu; ñu xamal ay xale yu ndaw dëgg gi, yen bu diisul |
— |
|||
— |
Galile (Nayin walla wetam) |
— |
||||
— |
Galile |
— |
||||
— |
Mu dàq ay rab ; bàkkaar bu ñu dul baal |
12:22-37 |
||||
— |
Joxewul firnde ju dul firndey Yunus |
|||||
— |
Yaayam ak ay rakkam ñëw ; Yeesu ne taalibeem yi ñooy ay mbokkam |
12:46-50 |
3:31-35 |
—