Paas bi turu téere bii nekk / Paas biy wone ñi defar téere bii
Mën nga nekk xaritu Yàlla !
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci li ñuy jëfandikoo ngir jàngal nit ñi ci àddina si sépp. Xaalis bi ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.
Boo bëggee def benn maye, mën nga dem ci www.pr418.com
Bu ñu ko leeralul, limi Biibël bi ci làkku ebrë yaa ngi tukkee ci firi bi yomba nànd, New World Translation of the Holy Scriptures—With References (NW), te mbind yi ci làkku grekk yaa ngi bawoo ci Kàddug Dëgg gi, 1987
Ci weeru Suweŋ ci atum 2017 lañu ko defar
Wolof (gf-WO)
© 2001
Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania