Paas bi fu turu téere bii nekk / Paas bi fu ñuy wone ñi defar téere bii
Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot
© 2014
Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
Ñi defar téere bi
Watchtower Bible and Tract Society of New York, Inc. Brooklyn, New York, U.S.A.
Ci weeru sãwiyee ci atum 2014 lañu ko defar
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci lu ñuy jëfandikoo ngir jàngale Biibël bi ci àddina si sépp. Xaalis bu ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.Bu ñu ko waxul, bépp aaya bu ñu fi lim, ñu ngi ko jële ci Njàlbéen ga, Sabóor, Kàddu yu Xelu ak Téereb Injiil di Kàddug Yàlla. Aaya yi ànd ak MN, ci Les Saintes Écritures — Traduction du monde nouveau lañu ko jële, firi ko ci wolof.