TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • hf p. 2
  • Ubbite bi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Ubbite bi
  • Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Lan ngeen mën a def ba am jàmm ci seen njaboot ?
    Xibaaru jàmm bi jóge ci Yàlla !
Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot
hf p. 2

Ubbite bi

Tey ci suñu jamono ju metti jii, séy yu bare ñu ngi tas te njaboot yu bare amuñu jàmm. Ndax mën nañu am jàmm ci suñu biir njaboot ? Dëgg la, am jàmm yombul. Waaye ndimbal am na. Téere bii, loolu moo ko tax a jóg. Waxul lépp lu jëm ci séy waaye dafay joxe ay santaane yu wóor yu sukkandiku ci Biibël bi ak ni ñu leen mënee topp. Bu ngeen toppee bu baax li ci nekk, dingeen mën a yokk jàmm bi ngeen am ci seen biir njaboot.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager