Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii
Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Xoolal li Biibël bi wax)
Ki moom foto bi: Paas 13, li des ci dëkku Babilon: Image © Homo Cosmicos/Shutterstock
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci li ñuy jëfandikoo ngir jàngale Biibël bi ci àddina si sépp. Xaalis bi ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge. Boo bëggee maye dara, demal ci donate.jw.org.
Bu ñu ko waxul, bépp aaya bu ñu lim ci paas yépp, bu àndul ak MN (La Bible. Traduction du monde nouveau), ñu ngi ko jële ci Kàddug Yàlla gi © 2010, 2020 Les Assemblées Evangéliques du Senegal et La Mission Baptiste du Sénégal. Bépp aaya bu àndul ak MN te bokk ci téerey kóllëre gu jëkk gi, ñu ngi ko jële ci Kàddug Yàlla gi © 2020 La Mission Baptiste du Sénégal.
Téere ak wideo yi ñu tudd ci téere bii Seede Yexowa yi ñoo leen defar.
Desàmbar 2022 lañu ko defar
Wolof (lffi-WO)
© 2021
WATCH TOWER BIBLE AND TRACT SOCIETY OF PENNSYLVANIA