Bindal fi nga tollu ci lesoŋ yi
- Li ngay njëkk a wax 
- Waxal mel ni kuy waxtaan 
- Booleel ay laaj ci sa njàngale 
- Li nga mën a wax bala ngay jàng aaya 
- Liiral bu baax li ñu bind 
- Woneel bu baax njariñu aaya yi 
- Li ngay wax na tegu fu wóor te nit mën koo gëm 
- Jàngalal nit ñi ak ay misaal 
- Jëfandikool ay wideo ak ay nataal ngir jàngal nit ñi 
- Ni ngay soppee sa baat booy jàngale 
- Waxal ak cawarte 
- Waxal ak mbaax te woneel ne yëg nga nit ñi 
- Woneel bu baax njariñu li ngay jàngale 
- Woneel bu baax ponk yi gën a am solo 
- Woneel ne gëm nga li ngay wax 
- Xiiral nit ñi ci jëfe li ñu dégg te amal xalaat bu rafet ci ñoom 
- Li ngay wax na leer ci ñi lay déglu 
- Defal waxtaan buy yokk xam-xam 
- Defal lépp ngir laal xolu nit ñi 
- Li ngay wax ngir jeexal sa waxtaan