TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • lff xaaj 4
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 4

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 4
  • Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 3
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 2
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 1
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Wideo yi ak waxtaan yi
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Xoolal li Biibël bi wax)
Xóotalal waxtaan bi
Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
lff xaaj 4

Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 4

  1. 48 Tànnal bu baax say xarit

  2. 49 Naka nga mënee am jàmm ci sa biir njaboot? (Xaaj 1)

  3. 50 Naka nga mënee am jàmm ci sa biir njaboot? (Xaaj 2)

  4. 51 Naka nga mënee neex Yexowa ci say wax?

  5. 52 Lu tax ñu war a bàyyi xel ci ni ñuy soloo?

  6. 53 Bégalal Yexowa ci ni ngay féexale sa xol

  7. 54 Kan mooy «surga bu takku te teey» bi te lan lay def?

  8. 55 Li nga mën a def ci mbooloo bi nga bokk

  9. 56 Nañu wéy di doon benn ci mbooloo mi

  10. 57 Lan nga war a def boo defee bàkkaar bu réy?

  11. 58 Wéyal di takku ci Yexowa

  12. 59 Mën nga muñ fitna yi

  13. 60 Wéyal di jëm kanam

48 Tànnal bu baax say xarit

Jàngal ni nga mënee moytu àndandoo yu bon (6:​17)

Mën nga am ay xarit fi nga ko foogewul (5:​06)

Lan mooy xarit dëgg? (4:​14)

GËSTUL

«Naka laa mënee am xarit yu baax?» (yp1, pàcc 8)

Xamal bu baax li ngay def ci internet (4:​12)

«Biibël bi dafay soppi dund» (w12 1/4)

49 Naka nga mënee am jàmm ci sa biir njaboot? (Xaaj 1)

Yeen jëkkër yi, bëggleen seen jabar ni ngeen bëgge seen bopp (9:​53)

Ni ngeen mënee gën a dëgëral seen séy (5:​44)

GËSTUL

Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot (téere bu ndaw)

Bëggante dëgg (4:​26)

«Yeen jigéen ñi, lu tax ngeen war a nangul seen kilifa?» (w10 15/5)

Biibël bi dimbali na ñu, ñu gën a dëgëral suñu séy (5:​14)

50 Naka nga mënee am jàmm ci sa biir njaboot? (Xaaj 2)

Aarleen seeni doom ci lu bon (2:​58)

Aarleen seeni doom (wideo)

«Jésus est plus fort que les démons» (lr-F, pàcc 10)

«Comment Jésus a été protégé» (lr-F, pàcc 32)

«Jàngal-leen seeni doom lu jëm ci awra» (g16 n° 5)

Naka laa war a waxe ak samay waajur? (2:​19)

Njàngum Biibël ci biir njaboot: Jafe-jafe yi ak barke yi (8:​04)

GËSTUL

«Juróom-benni njàngale yu xale yi war a xam» (g19 n°2)

Yexowa jàngal na ñu, ñu yar suñuy doom (5:​58)

«Naka la baay yi mënee wéy di jege seeni doom yu góor? (w11 1/11)

51 Naka nga mënee neex Yexowa ci say wax?

Wax juy «faj soxlay seeni moroom» (4:​07)

Bëgg sa moroom te weg ko mooy boole njaboot yi (3:​08)

GËSTUL

«Ndax ci dëgg ñaaw-làmmiñ lu bon la?» (Ci jw.org la nekk)

Naka laa mën a def ba moytu jëw? (2:​36)

«Dama xalaataat bu baax ci ni ma doon dunde» (w13 1/8)

52 Lu tax ñu war a bàyyi xel ci ni ñuy soloo?

«Defleen lépp ngir màggal Yàlla» (10:18)

GËSTUL

«Lan laay nirool?» (Ci jw.org la nekk)

«Lan la Biibël bi wax ci tatuwaas?» (Ci jw.org la nekk)

«Sama gis-gis ci colin ak defaru moo ma doon tere jëm kanam» (g03 22/12)

53 Bégalal Yexowa ci ni ngay féexale sa xol

Naka laa war a tànne ni may féexale sama xol? (4:​39)

Lan mooy gën a jël sa jot? (2:​45)

GËSTUL

«Ndax am na ay film, téere walla woy yu ñu tere Seede Yexowa yi?» (Ci jw.org la nekk)

«Ndax li ngay féexale sa xol baax na ci yow?» (w11 15/10)

Moytul fo yi am mbirum Seytaane (2:​02)

54 Kan mooy «surga bu takku te teey» bi te lan lay def?

Yexowa mooy jiite mbooloom (6:18)

Liggéeyu waare bi lañu jiital (1:​24)

GËSTUL

«Lan mooy Jataay biy dogal bu Seede Yexowa yi?» (Ci jw.org la nekk)

Cér bu réy (7:​04)

Yexowa mooy jàngal mbooloom (9:​39)

55 Li nga mën a def ci mbooloo bi nga bokk

‘Maye ngir Yexowa’ (4:​47)

Nañu toppatoo béréb yi ñuy jaamoo Yàlla (3:​31)

Yeen góor ñi: wutleen a def liggéey bu rafet (5:​19)

GËSTUL

:

«Lu jëm ci kilifteef ci mbooloo mi» (w21 02)

Dañuy yóbbul seeni mbokk ca Congo ay téere yu sukkandiku ci Biibël bi (4:​25)

«Fan la Seede Yexowa yi di jële xaalis bi ñuy defe seen liggéey?» (Ci jw.org la nekk)

56 Nañu wéy di doon benn ci mbooloo mi

Wut a juboo dafay jur lu baax (6:​01)

Baale ndam la! (5:​10)

GËSTUL

Dindil gànj gi ci sa bët (6:​56)

«Baalu dafay indi jàmm» (w02 1/11)

Bàyyileen di àtte ci li bët di gis rekk (5:​06)

57 Lan nga war a def boo defee bàkkaar bu réy?

«Ku Boroom bi sopp, yar la» (3:​01)

GËSTUL

Masuma am xel-ñaar ci yërmande Yexowa (5:​02)

«Ni Magi mbooloo yi mënee dimbali ñi ñu génne ci mbooloo mi» (w24.08)

«Biibël bi dafay soppi dund» (w12 1/4)

58 Wéyal di takku ci Yexowa

Génnleen ci Babilon mu mag mi! (5:​06)

GËSTUL

«Ndax xam naa li xew dëgg?» (w18 ut)

«Nañu gën a sawar ci njeexteelu ‘mujug jamono’ jii» (w19 § 16-​18)

Moytul ñu nax la (9:​32)

59 Mën nga muñ fitna yi

Yexowa moo ñu fat (5:​13)

Dañu wone fit doonte sax fitnaal nañu leen (6:​27)

Yexowa dina ma dooleel (3:​40)

GËSTUL

Wéy nañu di jaamu Yexowa bu dee sax dund nañu ay coppite (7:​11)

«Waajalal sa bopp léegi ngir muñ fitna yi» (w19 sulyet)

«Dëgg gi du ‘indi jàmm, waaye jaasi lay indaale’» (w17 oktoobar)

60 Wéyal di jëm kanam

Gënal a jariñoo sa njàngum Biibël (5:​22)

Dund gi gën ci dund yi (3:​31)

Approchez-vous de Jéhovah (téere)

« Viens, suis-moi. » (téere)

GËSTUL

Nañu takku ci Yàlla ni Ibraayma (9:​20)

Jàng ak xalaat bu baax dina la mayaat mbégte (5:​25)

«Nañu jàll cig mat: ‘Bésub Aji Sax bu mag bee dëgmal’» (w09 15/5)

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager