Note
a Turuw Shiloo ngiy tekki “Ki mu lew; Ki ko moom.” Ca waxtoom, mujj naa leer ne “Shilo” moo doon Yeesu Krist, “Gaynde [gi bawoo ca] giiru Yudaa.” (Peeñu bi 5:5) Yenn téerey Yawut yi ñu tudde Targum wuutu nañu sax baat “Shilo” ak “Almasi bi” walla “Almasi buur bi.”