Note b Xoolal Yeneen leeral 2 ngir gis benn yégle yonent buy wax kañ la Yeesu waroon na feeñ ci kaw suuf.