Note a Ci atum 1879 ba tey, ñu ngi wone dëgg gi nekk ci Biibël bi ci suñu yéenekaay bi gën a siiw, La Tour de Garde.