Note a Bu dee sax nit dafa sóobu ci ndox ba pare ci beneen diine, dafa war a sóobuwaat. Lu tax? Ndaxte diine bi mu jóge jàngalewul dëgg gi nekk ci Biibël bi (Xoolal Jëf ya 19:1-5 ak lesoŋ 13).