Note
a Malaaka bi ñuy woowe Kàddu gi, du moom rekk moo doon jottali li Yàlla wax. Li koy wone mooy, Yàlla jaar na ci yeneen doomam, maanaam yeneen malaaka ngir jottali waa Israyil Yoonu Musaa (Jëf ya 7:53; Galasi 3:19; Yawut Ya 2:2, 3).