Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025 (CA-brpgm25) Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025 Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii: