Desàmbar Dañu la soxla Nañu dimbali ñi ñuy jàngal Biibël bi ñu topp li ñuy jàng Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport d’août Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Loo mën a def ba waar say mbokk ? Yégle yi Nanga jariñoo wideo bi tudd Pas de sang : la médecine relève le défi Lan mooy njariñu Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi