Feewriyee Nañu gërëm Yexowa ndax ni mu baaxe ak ñun Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport d’octobre Yégle yi Ci jamano bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu, nañu yokk li ñuy def ci liggéeyu waare bi Ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu : Li ñu warul a fàtte Xaaj 6 : Nañu dimbali ñi ñuy jàngal Biibël bi ñu topp li ñuy jàng Li nga mën a def ngir ñu kontine waxtaan bi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu Sasu Nguuru Yàlla Suñu ndaje bu gën a mag bi dafa ñuy xiir ci ànd ak Yàlla Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi