2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni (CA-brpgm21) 2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan—Ak ki bànqaas bi yónni “Bégal ci Yexowa” Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii