Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2022-2023 (CA-brpgm23) 2022-2023 Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni Ñi bëgg jàmm Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii