Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024 (CA-brpgm24) 2023-2024 Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni Nañu dugg ci noflaayu Yàlla! Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii