2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi (CA-copgm21) 2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan—Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi Bégalal xolu Yexowa! Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii