Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023 (CA-copgm23) Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi bu atum 2022-2023 Yexowa dafay jàngal mbooloom ñu nekk benn Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii