Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2023-2024 (CA-copgm24) 2023-2024 Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi Ni ma yàkkamtee ndimbalu Yexowa! Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii