Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2024-2025 (CA-copgm25) Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi bu atum 2024-2025 Na seeni jëf méngook li ngeen xam ci xibaaru jàmm bi Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii