Awril Ndax yaa ngiy wuyu mbëggeelu Krist ? Ndax soloo nga xelum bañ a nekkal-sa-bopp ? Ndax tàmm nga di yéene Nguur gi ? Wóoralal sa dellu foofa !