Awril Waare Nguur gi dafay musal ! Ndax yaa ngi farlu ci njàng mi ak mbind mi ? Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi “ Nanuy defal ñépp lu baax ” Mbégte bi nekk ci jébbal sa jot yépp liggéeyu Yàlla Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Yégle yi Rapport de décembre Nañu wéy di jariñoo La Tour de Garde ak Réveillez-vous ! Naka lañu mën a ame njaboot bu dëgër ci wàllu ngëm ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi