Màrs Nekk benn ak Yexowa ak Doomam te bég ci Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de novembre Na nga “ bare jëf yu rafet ” Góor ñi nekk ay may dañuy sàmm bu baax géttu Yàlla Leetar bu ñu Jataay biy dogal yónnee Yégle yi Li ñu warul a fàtte ci ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu Yokkleen mbégte bi ngeen di am bu ngeen di waaraate Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi