Nowàmbar Xamleleen dëgg gi jëm ci Yeesu Jàppleel sa wottukatu njàngum téere bi ñuy def ci mbooloo mi Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Ay yéenekaay yu am solo ! Lekkool bu ñuy jàngal ni ñuy defe li ëpp solo ci àddina Boroom kër yi : tàmmleen di topp porogaraam bu baax ci wàllu ngëm Yégle yi Rapport de juillet Ay tont ci seeni laaj Woneel ne ittewoo nga ak mbëggeel “ xale yu seen baay gaañu ” Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi