Feewriyee Ndaje yu gën a mag yi ak yiy boole ay réew yu bare, xiir nañu nit ñi ci màggal Yàlla ! Faral di teewe suñu ndaje yi, bokk na ci li ëpp solo Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport d’octobre Nañu wéy di wax ci lu kéemaane li Yexowa def Nañu jariñoo njàngum téere Approchez-vous de Jéhovah Approchez-vous de Jéhovah Yégle yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Mën nañu def li ñu Yexowa laaj Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi