Nowàmbar Buñu fàtte ne jot bi des bareetul Nañu dimbali suñu moroom Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de juillet Yégle yi Nañu kontine di wax nit ñi ñu ‘ ànd ak Yàlla ’ Ay tont ci seeni laaj Xaaj 3 : Nañu dimbali ñi ñuy jàngal Biibël bi ñu topp li ñuy jàng Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi