Suweŋ Waaraate bi dafay tax ñu mën a muñ Xaaj 10 : Nañu dimbali ñi ñuy jàngal Biibël bi ñu topp li ñuy jàng Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de février Yégle yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Nañu waaraate bu baax fu nit ñi di bare Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi