Awril Naka lañu mënee kontine di sawar ci liggéeyu Yàlla Wonal sa moroom ne danga ko bëgg — Nanga xool ki ngay waxal ngir xam li muy yëg Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de décembre Ay njàngum Biibël yu ñuy def ci buntu kër ak ci telefon yu jëm kanam Yégle Yi Benn wideo buy wone lu ñuy jariñ ba tey Ni ñu mënee waxtaan ak nit ba mu nangu dëgg gi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci Lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Ndax yaa ngi laaj ku ñu la mën a booleel ? Nañu xam ni ñu waree jëfandikoo suñu téere yiy wax ci li nekk ci Biibël bi Ndax mën nga defaraat sa porogaraamu waare ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi