Desàmbar Mbëggeel bi nga amoon bu njëkk, bul nangu mu wàññeeku Nañu dellu seeti képp ku wone ne am na lu ko neex ci suñu waxtaan Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport d’août Li nekk ci wideo boobu, war nañu ci xalaat bu baax Ay tont ci seeni laaj Am xelum nangu bokk ci lépp li ñu la soxla, dafa lay indil barke Yégle yi Nañu fàttaliku li ñu jàng ci lekkoolu sasu Nguuru Yàlla Ndax am nga gox bi nga moomal sa bopp ngir waare ? Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi