Sulyet Dimbalil ñiy jàng Biibël bi ñu fonk jikko ju rafet lool ji Yexowa am Nañu roy ci Yexowa, suñu Yàlla ji bare mbégte Ndaje yi jëm ci liggéeyu waare bi Rapport de Mars Yéen karceen yi nekk ndaw — Naka ngeen di gise liggéeyu pioñee bu ci sax ? Yégle yi Ay nit ñu jar a roy lañu ci wàllu ngëm Li ñu war a tàmm ci wàllu ngëm ngir mu indil ñu barke yu bare Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi Juillet