Nowàmbar Am nañu lu am maanaa lu ñu bëgg a bokk ak suñuy moroom Nañu waajal ñu bees ñi, ñu bañ a dellu ginnaaw bu ñu leen di xeex Ndaje Yi Jëm Ci Liggéeyu Waare Bi Li ñu def ci waaraate bi ci weeru sulyet Yégle Yi Ay Tont Ci Seeni Laaj Mën nga nekk jàngalekat Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi