Dund ci suuf si (le) Paas bi fu turu téere bii nekk/Paas bi fu ñuy wone ñi defar téere bii Li Nekk Ci Téere Bi Dundleen ba fàww ak bànneex ci suuf si ! Ku leen sàkk ? Lu tax nit di dee ? Lu dee tekki ? Yàlla alag na àdduna bu bon Ndax Yàlla dina alagaat ñu bon ñi ? Yexowa jox na ñu Musalkat Naka la bàkkaar ak dee mënee teggeeku ci ñun ? Nguuru Yàlla dina indi barke ci suuf si Lan ngeen war a def ?