Déggleen ndax ngeen am dund (ll) Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii Li nekk ci téere bii Ubbite bi XAAJ 1 Naka lañu mën a dégge li Yàlla wax ? XAAJ 2 Kan mooy Yàlla dëgg ji ? XAAJ 3 Naka la dund bi meloon ci toolu Eden ba ? XAAJ 4 Ndegam Aadama ak Awa dañu déglu Seytaane — loolu lan la jur ? XAAJ 5 Ca jamano yonent Yàlla Nóoyin — ñan ñoo déggoon li Yàlla wax te ñan ñoo bañoon a dégg ? XAAJ 6 Lan lañu mën a jàng ci taw bu metti bi amoon ca jamano Nóoyin ? XAAJ 7 Kan mooy Yeesu ? XAAJ 8 Ban njariñ la leen deewu Yeesu amal ? XAAJ 9 Kañ la suuf si di nekkaat àjjana ? XAAJ 10 Yan barke la ñiy dégg li Yàlla wax nar a am ? XAAJ 11 Ndax Yexowa mu ngi dégg li ñuy wax ? XAAJ 12 Lan ngeen mën a def ngir am jàmm ci seen biir njaboot ? XAAJ 13 Lan lañu war a def ba am dundin bu neex Yàlla ? XAAJ 14 Naka ngeen mën a wonee ne Yexowa ngeen topp?