No 2 12 ponk yiy tax njaboot yi am jàmm Li nekk ci téere bii Ubbite bi ÑI NEKK CI SÉY ÑOO MOOM LII 1 Sàmm kóllëre ÑI NEKK CI SÉY ÑOO MOOM LII 2 Déggoo ÑI NEKK CI SÉY ÑOO MOOM LII 3 Respe ÑI NEKK CI SÉY ÑOO MOOM LII 4 Baalante WAAJUR YI ÑOO MOOM LII 5 Waxtaan WAAJUR YI ÑOO MOOM LII 6 Yar WAAJUR YI ÑOO MOOM LII 7 Jikko WAAJUR YI ÑOO MOOM LII 8 Royukaay NDAW ÑI ÑOO MOOM LII 9 Ki nga doon NDAW ÑI ÑOO MOOM LII 10 Kóolute NDAW ÑI ÑOO MOOM LII 11 Cawarte NDAW ÑI ÑOO MOOM LII 12 Jubluwaay Yeneen ndimbal ngir njaboot gi