Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi) XAAJ 1XAAJ 2XAAJ 3XAAJ 4LIIR BIIBËL BI Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi) Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii Ni nga mënee jariñoo njàngale Biibël bi nekk ci téere bii Xaaj 1 LESOŊ YI LESOŊ 01 Naka la la Biibël bi menee dimbali? LESOŊ 02 Biibël bi dafay maye yaakaar LESOŊ 03 Ndax mën nga gëm li Biibël bi wax? LESOŊ 04 Kan mooy Yàlla? LESOŊ 05 Biibël bi dafa ñuy xamal li Yàlla bëgg ñu def LESOŊ 06 Fan la nit jóge? LESOŊ 07 Kan mooy Yexowa? LESOŊ 08 Mën nga nekk xaritu Yexowa LESOŊ 09 Jegeel Yàlla ci ñaan LESOŊ 10 Ban njariñ nga mën a jële ci teewe ndaje Seede Yexowa yi? LESOŊ 11 Ni nga mënee jariñoo bu baax li ngay liir ci Biibël bi LESOŊ 12 Lan moo la mën a dimbali nga wéy di jàng Biibël bi? Nañu fàttaliku xaaj 1 WIDEO YI AK WAXTAAN YI Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 1