Leneen lu jëm ci loolu my nettali 10 Taw bu metti ci kow suuf si sépp Nóoyin dafay defar gaal gu mag Ay nettali yu nekk ci Biibël bi Ca jamano yonent Yàlla Nóoyin — ñan ñoo déggoon li Yàlla wax te ñan ñoo bañoon a dégg ? Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex Nit ku nekk am na li nga mën a jàng ci wideo bi tudd : Noé : il marchait avec Dieu Sasu Nguuru Yàlla — 2002 Xaaj 5 Déggleen li Yàlla wax Artu bu jóge ca lu amoon Mën nga nekk xaritu Yàlla !