Leneen lu jëm ci loolu ll xaaj 10 p. 22-23 Yan barke la ñiy dégg li Yàlla wax nar a am ? Xaaj 10 Déggleen li Yàlla wax Xaritu Yàlla yi dinañu dund ca Àjjana Mën nga nekk xaritu Yàlla ! Lan mooy coobare Yàlla ngir suuf si ? Lan la ñu Yàllay laaj? Bu keroogee xam-xamub Yàlla di fees suuf si Xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex Nguur gi nar a jiite suuf si sépp Jàngal-leen seeni doom