Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii
Gëm Yàlla Dëgg moo ñu mën a indil JÀMM
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci li ñuy jëfandikoo ngir jàngal nit ñi ci àddina si sépp. Xaalis bi ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.
Boo bëggee def benn maye, mën nga dem ci donate.jw.org
Bu ñu ko waxul, bépp aaya bu ñu fi lim, ñu ngi ko jële ci Mucc gi Yàlla waajal, Njàlbéen ga ak Téereb Injiil di Kàddug Yàlla. Aaya yi amagul ci wolof, bind nañu ci tubaab turu téere bi fi ñu nekk te dëngal mbind yi. Aaya yi ànd ak MN, ci La Bible. Traduction du monde nouveau lañu ko jële, firi ko ci wolof.
Ci weeru awril ci atum 2023 lañu ko defare
Wolof (rk-WO)
© 2011
Monominoto Seisho Sasshi Kyokai
Ñi defar téere bi
Monominoto Seisho Sasshi Kyokai
Ñi moom foto yi : xët 13, ci suuf : Todd Bolen/BiblePlaces.com; xët 25, suuf si : foto bu NASA/Visible Earth lañu fi nataal