Li nekk ci téere bii XAAJ BI 1 Ndax Yàlla fonk na nit ? 2 Lan mooy gëm Yàlla dëgg ? 3 Ay xelal yu am njariñ 4 Kan mooy Yàlla ? 5 Nañu fonk mbiri Yàlla yi 6 Lu tax Yàlla sàkk suuf si ? 7 Li Yàlla dige, jaarale ko ci yonent yi 8 Almasi bi ñëw na 9 Li ñu mën a jàng ci Almasi bi nekk Njiit 10 Ki bañ ñu gëm Yàlla, lan la def ? 11 Gëm Yàlla dëgg, ni ko nit ñi di wonee tey 12 Nanga wone ne gëm nga Yàlla dëgg ! 13 Ku gëm Yàlla dëgg, dinga mën a am jàmm ba fàww