TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • mb lesoŋ 2
  • Njàngale 2

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Njàngale 2
  • Li ma mën a jàng ci sama Biibël
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Nóoyin dafay defar gaal gu mag
    Ay nettali yu nekk ci Biibël bi
  • Xaaj 5
    Déggleen li Yàlla wax
  • Ca jamano yonent Yàlla Nóoyin — ñan ñoo déggoon li Yàlla wax te ñan ñoo bañoon a dégg ?
    Déggleen li Yàlla wax ndax ngeen am dund gu dul jeex
  • Nit ku nekk am na li nga mën a jàng ci wideo bi tudd : Noé : il marchait avec Dieu
    Sasu Nguuru Yàlla — 2002
Li ma mën a jàng ci sama Biibël
mb lesoŋ 2

Njàngale 2

Njàlbéen ga 7:7-10; 8:15-17

Xoolal mala yi nekk ci wetu gaalu Nóoyin bi.

Ban mala mooy wax mëëë ? Ban mooy wax wow-wow ?

Mala yépp, yu ndaw yi ak yu mag yi, ñoom ñépp gaalu Nóoyin moo tax deewuñu.

LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM

Jàngalal lii sa doom :

Njàlbéen ga 7:7-10 ; 8:15-17

Waxal sa doom mu won la :

Urs Xaj Ñey

Njamala Gaynde Golo

Mbaam-xuux Xar

Mbaam-àll Xon

Waxal sa doom mu toppandoo yuuxu mala yii :

Xaj Gaynde Golo

Mbaam-xuux Xar

[Nataal bi nekk paas 6, 7]

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager