Njàngale 3
1 Piyeer 3:8
Dawuda dégg na ne xaritam dafa feebar.
Mu ne : “ Xam naa li ma war a def.
Dama koy bind letaar ngir mu kontaan. Su ma paree ma yóbbu ko ! ”
Nanga baax ak moom. Dingeen kontaan yéen ñaar !
LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM
Jàngalal lii sa doom :
1 Piyeer 3:8
Waxal sa doom mu won la :
Kër Taabal Dawuda
Naaj Picc Garab
Laajal sa doom lii :
Ndax xam nga kenn ku feebar ?
Lan lañu ko mën a defal ?
[Nataal bi nekk paas 8]
[Nataal bi nekk paas 8]
[Nataal bi nekk paas 9]
[Nataal bi nekk paas 9]