Ubbite bi
“Nanga bëgg Yexowa sa Yàlla ak sa xol bépp ak sa bakkan bépp, ak sa kàttan gépp. Kàddu yii ma lay digal tey war nañu nekk ci sa xol, te war nga leen a dugal ci say doom te wax ci ak ñoom bu ngeen toogee ci seen kër, bu ngeen di dox ci mbedd mi, bu ngeen di tëddi ak bu ngeen yeewoo.” — 5 Musaa 6:5-7, MN.