Jàngal-leen seeni doom (yc) Jàngal-leen seeni doom Paas bi fu turu téere bii nekk/Paas bi fu ñuy wone ñi defar téere bii Li nekk ci téere bii Ubbite bi NJÀNGALE 1 Am na kumpa goo xam ne boo ko xamee dinga kontaan NJÀNGALE 2 Rebeka dafa bëggoon di bégal Yexowa NJÀNGALE 3 Raxab dafa gëmoon Yexowa NJÀNGALE 4 Dafa bégaloon pàppam ak Yexowa NJÀNGALE 5 Samwil bàyyiwul di def lu jub NJÀNGALE 6 Daawuda nekkul woon ku ragal NJÀNGALE 7 Ndax lée-lée dangay yëg ne kenn bëggu la te nga am lu lay tiital ? NJÀNGALE 8 Yosiyas amoon na ay xarit yu baax NJÀNGALE 9 Yérémi bàyyiwul woon di wax ci Yexowa NJÀNGALE 10 Yeesu dafa doon dégg ndigal NJÀNGALE 11 Dañu nettali lu jëm ci Yeesu NJÀNGALE 12 Jarbaatu Pool bi dafa amoon fit NJÀNGALE 13 Timote dafa bëggoon di dimbali nit ñi NJÀNGALE 14 Nguur gi nar a jiite suuf si sépp