Paas bi turu téere bii nekk/Paas biy wone ñi defar téere bii
Téere buy dimbali Seede Yexowa yi ñu am ay tont ci seeni laaj
Bu atum 2019
Ci téere yi ñu génne ci làkku Wolof
«Aji Sax jeey maye xel mu rafet, kàddoom di taxa xam, di dégg».—Kàddu yu Xelu 2:6.
Xamal lii: Xéyna dinga fi gis ay téere yu xaw a yàgg. Nanga xam ne, ginnaaw bi ñu leen génnee, mën na am ñu soppi yenn njàngale yi ci nekk ndax ay leeral yu bees.
Kenn warul jaay téere bii. Dafa bokk ci li ñuy jëfandikoo ngir jàngale Biibël bi ci àddina si sépp. Xaalis bi ñuy defe liggéey boobu, ci li nit ñi di maye la jóge.
Boo bëggee maye dara, demal ci donate.jw.org.
Téere buy dimbali Seede Yexowa yi ñu am ay tont ci seeni laaj—Bu atum 2019
Ci téere yi ñu génne ci làkku Wolof
Ci weeru me ci atum 2022 lañu ko defar
Wolof (rsg19-WO)
© 2020, 2022 WATCH TOWER BIBLE AND TRACT SOCIETY OF PENNSYLVANIA