TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CO-pgm22 p. 8
  • Li ñi teew war a xam

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñi teew war a xam
  • Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2022
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñi teew war a xam
    Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2021
  • Li ñi teew war a xam
    Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024
  • Li ñi teew war a xam
    Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2025
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2022
CO-pgm22 p. 8

Li ñi teew war a xam

Sóob bi Magi mbooloo mi jël nañu ba pare matuwaay yi gën, ngir ñi bëgg a sóobu ci ndox mën koo def, bu porogaraamu samdi bi ci suba si jeexee.

Ñi bëgg a def ay maye Ndaje bu mag bu ñetti fan bii, dinañu ko tekki ci lu ëpp 500 làkk. Maye yi ngeen di def dafay jàppale liggéey boobu ñuy def ci àddina si sépp. Mën ngeen maye jaare ko ci internet ci donate.jw.org. Ñu ngi leen di gërëm bu baax ci lépp li ngeen di maye. Jataay biy dogal it mu ngi leen di gërëm ci lépp li ngeen di maye ngir liggéeyu Nguur gi jëm kanam.

Lekkool bi ñu jagleel ñiy waare nguuru Yàlla

Jëkkër ak jabar ñu ngi jëfandikoo téere bi tudd “Mën nga dund ci jàmm ba fàww” ngir jàngal Biibël benn xale bu góor

Pioñee yi am diggante 23 at ba 65 at te bëgg yokk seen liggéeyu waare bi, mën nañu jokkoo ak seen sekereteeru mbooloo mi te bindu ci internet ngir mën a dem ci Lekkool bi ñu jagleel ñiy waare Nguur gi.

Jataay biy dogal ci Seede Yexowa yi moo taxawal ndaje bii

© 2022 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager