TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-copgm23 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2022-2023
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
    2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
Xóotalal waxtaan bi
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
CA-copgm23 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Naka lañu mën a wonee ne fonk nañu suñu palaas ci mbooloo Yexowa? (Efes 4:3)

  2. 2. Naka lañu mën a wonee ne fonk nañu ñeneen ñi, te lu tax ñu war koo def? (Room 15:7)

  3. 3. Naka lañu mënee dimbali ñu bare ñu ñëw bokk ci mbooloo Yexowa? (Efes 2:17; 6:15)

  4. 4. Naka nga mënee def lépp li nga mën ngir wut jàmm? (Efes 4:29; 5:1, 2; 6:13)

  5. 5. Lan lañu mën a def ba gën a fonk suñu mbokk yi ci ngëm? (Efes 1:15, 16)

© 2022 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-copgm23-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager