TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-copgm21 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • 2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Déglul Bu Baax Ba Mën A Tontu Ci Laaj Yii
    2019-2020 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër bu atum 2022-2023
Xóotalal waxtaan bi
2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
CA-copgm21 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

  1. 1. Ñun jaamu Yexowa yi, ban cér bu réy lañu am? (Kàddu yu Xelu 27:⁠11)

  2. 2. Naka lañu mënee roy Yeesu te bégal xolu Yexowa? (Yowaana 8:⁠29)

  3. 3. Naka lañu mënee bégal xolu Yexowa ci suñu liggéeyu waare bi? (Yowaana 15:⁠8)

  4. 4. Naka lañu mënee neex Yexowa ci bépp fànn ci suñu dund? (Yowaana 14:31; Waa Efes 6:​1-4; Sabóor 35:18; 1 Piyeer 2:⁠12)

  5. 5. Naka lañu mënee jànkoonte ak jafe-jafe yi, bañ a xàddi te bañ a daanu ci fiir? (Neyemi 8:⁠10)

© 2020 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager