TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • CA-brpgm24 p. 4
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  • Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
  • Turu xaaj yi
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2021-2022
  • Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
    2019-2020 Porogaraamu Ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
Xóotalal waxtaan bi
Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2023-2024
CA-brpgm24 p. 4

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:

  1. 1. Naka lañu mënee dugg ci noflaayu Yàlla? (Njàlbéen ga 2:​1-3; Yawut ya 4:​1, 11)

  2. 2. Naka lañuy wonee ne «Kàddug Yàlla» am na doole ci suñu dund? (1 Tesalonig 2:13; Yawut ya 4:12)

  3. 3. Lu tax, ci lépp li ñuy def, ñu war a wut a xam li Yexowa bëgg? (Esayi 26:​7-9, 15, 20)

  4. 4. Lan lañu war a def bu ñu bëggee Yexowa barkeel ñu? (1 Piyeer 1:​13-15; 1 Yowaana 5:3)

  5. 5. Naka lañu mënee bégal Yexowa? (Sabóor 71:​14, 15; Room 12:2; 1 Piyeer 4:10)

  6. 6. Naka lañu mënee bég ci liggéeyal Yexowa? (Yowaana 5:17)

© 2023 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania

CA-brpgm24-WO

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager